Njàlbéen ga 15:2

Njàlbéen ga 15:2 KYG

Ibraam ne ko: «Boroom bi, yaw Aji Sax ji, ana loo may may nag? Man awma doom sax, te ki wara donn sama alal moo di Elyeser, miy waa Damaas.»

Чытаць Njàlbéen ga 15