Exodus 20:9-10

Exodus 20:9-10 GWG

Jurum ben’ i fan nga lige, te def saa lige yipa; wandi, jurum narel i fan ba mu Dimas i Yalla saa Borom. Ce mom, bulu def bena lige, you oh, saa dom ju gor oh, saa dom ju jigen oh, saa rapas bu gor oh, saa rapas bu jigen oh, saa get oh, mbaat saa gan gu dal ak you.

Чытаць Exodus 20