John 6:11-12
John 6:11-12 GWG
Yesu nak jel mburu ya, te ba mu jebale ngerem, mu sedātle len ña tōg; ak jen ya itam cha naka ñu buge. Te ba ñu leke be sūr, mu ne i talube am, Dajale len dogit yi chi des, ndah͈ bul chi dara yah͈u.