Matthew 24:9-11

Matthew 24:9-11 GWG

Fōfale di nañu len jebale ndah͈ ñu geten len, te di nañu len rēy: h͈êt yi yepa di nañu len sib ndig man. Fōfale ñu bare di nañu fakatalu, orante, te sibante. Yonent i nafeh͈a yu bare di nañu jogi, te nah͈ ñu bare.

Чытаць Matthew 24