Matthew 6:16-18

Matthew 6:16-18 GWG

Su ngēn di ôr, bu len am kanam gu dīs niki nafeh͈a ya; ndege di nañu ñaulo sēn i kanam ndah͈ nit ña gis ne ñunge ôr. Chi dega mangi len di wah͈, Am nañu sēn yōl. Wande you, so di ôr, diwal sa bopa te selem sa h͈ar‐kanam; Ndah͈ do mel naka ku di ôr chi nit, wande chi sa Bay ki chi nubu; te sa Bay ka gis lu nubu, di na la yōl.

Чытаць Matthew 6