Njàlbéen ga 25:23
Njàlbéen ga 25:23 KYG
Aji Sax ji ne ko: «Ñaari giir nga ëmb, nara am ñaari xeet yuy xaajaloo, wenn wi mooy ëpp doole wi ci des, te mag ji mooy surgawu rakk ji.»