John 8:10-11
John 8:10-11 GWG
Te Yesu yēkatiku te ne ko, Jigen ji, ana ñu? ndah͈ ken ēyu la? Te mu ne, Dowul kena, Borom bi. Te Yesu ne, Man itam ēyu ma la: demal sa yōn: ganou tey bul bakarati.