Matthew 5:13

Matthew 5:13 GWG

Yēn a di soh͈mat i aduna si; wande su soh͈mat ñake nchafo am, lu ñu ko safaleti? Dōtul jeriñ dara lul sani ko chi biti, te nit degat ko chi suf.