Logo YouVersion
Ikona vyhledávání

Exodus 20:4-5

Exodus 20:4-5 GWG

II. Bulu defar ce saa bopa bena natal bu nu erta, mbaati natal bu mu mun na don bu neka ce ajana ce kou, mbaati bu neka ce aduna ce suf, mbaati bu neka ce ndoh ma ca run suf si. Bulu sukal saa bopa fi nom, ne, da nga len di jaamu: ndegi, Man Yalla saa Borom, Yalla bu fir la, te di teg bakar i bai yi ce kou dom yi, ca netel ak nenentel i hert na maa ban