Matthew 10
10
1Ba mu ôe fuk’ i tālube am ak ñar, mu may len kantan ñu dah͈a nh͈el yu sobe ya, te weral ña opa ñepa, ak h͈êt i jarak ju neka.
2Tūr i fuk’ i tālube ak ñar yangile: Benel bi, Simon ku tuda Peter, ak Andrew rak’ am; James dōm i Zebedee, ak John rak’ am;
3Philip, ak Bartholomew; Thomas, ak Matthew publican bi; James dōm i Alphæus, ak Thaddæus;
4Simon wā Canaan, ak Judas Iscariot, ka ko or on.
5Fuk’ ak ñar ñile la Yesu yōni on, te ebal len ne, Bu len dem chi yōn i Gentile ya, te bu len h͈araf chi dek’ i Samaritan ya:
6Wande dem len chi i nh͈ar i ker i Israel yu rēr ya.
7Te bu ngēn deme, wāre len, ne, Ngur i ajana jegeñsi na.
8Weral len ñu opa ña, setal len gāna ya, dēkali len ñu dē ña, dah͈a len i jine: ndig dara ngēn ko ame, maye len ko ndig dara.
9Bu len yubuāle wurus, mbāte h͈ālis, mbāte kopar chi sēn i nafa,
10Mbāt mbūs ndig rūnga ma, mbāte ñar i chol, mbāt i dala, mbāte doko: ndege ligeykat yi ela nañu sēn leka.
11Su ngēn h͈arafe chi rew wala deka, ūt len ku fa dagan, te jēki fa be bu ngēn di gēna.
12Su ngēn h͈arafe chi nēg bi, noyu len.
13Su nēg ba dagane, na sēn jama dika chi ñom; wande su daganule, na sēn jama delusi chi yēn.
14Te ku len dul nangu, wala dēga sēn bāt, bu ngēn di gēna cha nēg bōbale mbāte deka, foga len sēn pund’ i tanka.
15Chi dega mangi len di wah͈, di na gene dek’ i Sodom ak Gomorrah chi kerog mpēnch’ um Yalla ma as deka bōbale.
16Mangi len di yōni naka i nh͈ar chi digante i būki: mōtah͈ na ngēn têylu naka i jān, te lew naka i mpetah͈.
17Wande otu len nit, ndege di nañu len têwlo chi i ndaje, te ratah͈ len chi sēn i juma;
18Te di nañu len yubu chi kanam i kēlifa ak i bur ngir man, ndig sēde chi ñom ak chi Gentile ya.
19Wande su ñu len di têwlo, bu len jāh͈le naka mbāte lan ngēn di wah͈; ndege di nañu len may lu ngēn di wah͈ chi wah͈tu wōwale.
20Ndege du yēn a di wah͈, wande sēn Nh͈el i Bay ki di wah͈ chi yēn.
21Mag di na jebal rak’ am ndah͈ mu dē, te bay dōm am: i dōm di nañu or sēn i bay ak sēn i ndey, te rēylu len.
22Ñepa di nañu len sib ndig man; wande ku di muñ be cha muj ga mō di muchi.
23Wande su ñu len getene chi deka bile, dou len fa benen; ndege chi dega ma ne len, Du len won demi chi i dek’ i Israel yepa be ba Dōm i nit ka di ñoui.
24Tālube upul jemantalkat am, wala jām upa borom am.
25Doy na chi tālube mu neka naka jemantalkat am, te jām naka borom am. Su ñu ôe borom‐ker ga Abdujambar, naka ña mōmu chi ker am!
26Bu len len ragal mbōk; ndege dara muruwul lu dul muriku; mbāte nubu, lu dul fêñ.
27Lu ma len wah͈ chi lendem gi, wah͈ len ko chi lêr gi; te lu ngēn dēga chi sēn nopa, yēgal len ko chi kou nēg yi.
28Bu len ragal ña di rēy yaram wi, wande munu ño rēy fit wi; wande ragal len ka mun a yah͈a fit ak yaram itam chi nāri.
29Ndah͈ ñar i mbelar du jar bena kopar? Te bena du dānu chi suf te sēn Bay yēgu ko.
30Wande sēn i kouar i bopa sah͈, woña nañu len yepa.
31Mōtah͈ bu len ragal; yēn a gen mbelar yu bare.
32Ku neka mbōk ku ma sēde chi kanam i nit, mōm lā di sēdeji itam chi suma kanam i Bay ba cha ajana.
33Wande ku neka ku ma wēdi chi kanam i nit, man itam di nā ko wēdiji chi suma kanam i Bay ba cha ajana.
34Bu len dēfe ne da ma ñou yōni jama chi suf si: ñouū ma yōni jama, wande jāsi.
35Ndege da ma ñou di munadilo gōr ak bay am, te jigen ak ndey am, te dōm ju jigen ak goro am gu jigen.
36Te i mbañ i nit a neka cha bir nēg am.
37Ku sopa bay am mbāte ndey am as man, daganul chi man; te ku sopa dōm am ju gōr, mbāte dōm am ju jigen as man, daganul chi man.
38Te ku gaduwul kura am te topa ma, daganul chi man.
39Ku ūt dund’ am, di na ko rēr; te ku rēral dund’ am ngir man, di na ko gis.
40Ku len nangu, man la nangu; te ku ma nangu, nangu na ka ma yōni.
41Ku nangu yonent chi tur i yonent, di na am yōl i yonent; te ku nangu nit ku jūb chi tur i nit ku jūb, di na am yōl i nit ku jūb.
42Te ku mu mun a don ku maye bena chi ñu tūt ñile mbatu’ ndoh͈ mu seda reka, chi tur i tālube, chi dega mangi len di wah͈, du ñaka yōl am.
Jelenleg kiválasztva:
Matthew 10: GWG
Kiemelés
Megosztás
Másolás
Szeretnéd, hogy a kiemeléseid minden eszközödön megjelenjenek? Regisztrálj vagy jelentkezz be
Published by the British and Foreign Bible Society 1882-1907.

: