Njàlbéen ga 10:9

Njàlbéen ga 10:9 KYG

mu doonoon rëbbkat bu maga mag. Looloo waral ñu naan: «Mbete Namróot, rëbbkat bu maga mag ba.»