Njàlbéen ga 11:8
Njàlbéen ga 11:8 KYG
Ba loolu amee Aji Sax ji jële leen foofa, tasaare leen ci kaw suuf sépp, ñu yemale fa dëkk ba ñu doon tabax.