Njàlbéen ga 13:8

Njàlbéen ga 13:8 KYG

Ba loolu amee Ibraam da ne Lóot: «Waay waay, bu xuloo am sama digganteek yaw mbaa say sàmm ak samay sàmm. Xanaa dunuy bokk nag?