Njàlbéen ga 8:11
Njàlbéen ga 8:11 KYG
Ba mu délsee ca ngoon, indaalewul lu moy xobu oliw wu tooy wu keppe ca sàll wa. Nóoyin xam ne ndox mi taa woon ci suuf, fer na.