Njàlbéen ga 9:1

Njàlbéen ga 9:1 KYG

Ci kaw loolu Yàlla barkeel Nóoyin aki doomam ne leen: «Giirleen te bare, ba fees àddina.