Njàlbéen ga 9:2

Njàlbéen ga 9:2 KYG

Mboolem rabi àll yi ak njanaawi asamaan ak ndëgmeent yi ci suuf, ak jëni géej yépp, dinañu leen ragal lool. Teg naa leen ci seeni loxo.