Njàlbéen ga 9:3

Njàlbéen ga 9:3 KYG

Man ngeena dunde boroom bakkan yooyu yépp. Jagleel naa leen bindeef yooyu yépp, ni ma leen jagleele woon gàncax.