Chapa ya Youversion
Ikoni ya Utafutaji

Matthew 2:12-13

Matthew 2:12-13 GWG

Te Yalla yēgal on na len chi gēnta, ne bu ñu delu fa Herod; mōtah͈ ñu ñibi sēn deka cha wenen yōn. Ba ñu dem on, malāka i Borom bi fêñu Yusufa chi gēnta, ne, Jogal, jelal gūne gi ak ndey am, te dou cha Mesara, te jēki fa be ba ma la cha ôe, ndege Herod di na ūt gūne gi ndah͈ mu rēylu ko.

Soma Matthew 2