1
John 1:12
Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
Wande ña ko nangu on, ñom la may on sañsañ ñu neka i dōm i Yalla, ña gum chi tur am
เปรียบเทียบ
สำรวจ John 1:12
2
John 1:1
Cha chosan la Bāt ba am on na, te Bāt ba nek’ on na ak Yalla, te Bāt ba nek’ on na Yalla.
สำรวจ John 1:1
3
John 1:5
Te lêr gi melah͈ chi lendem gi, te lendem gi sēnu ko won.
สำรวจ John 1:5
4
John 1:14
Te Bāt bi yaramu on na, te dek’ on na ak ñun, te sêt on nañu ndam am, ndam niki ku di dōm i bay ju di bajo, fês ak yiw ak dega.
สำรวจ John 1:14
5
John 1:3-4
Lu neka chi mōm la saku on; te ganou mōm dara sakuwul on cha la saku on. Chi mōm la dūnda nek’ on; te dūnda gi nek’ on na lêr i nit.
สำรวจ John 1:3-4
6
John 1:29
Cha elek sa mu gis Yesu di ñou fi mōm, te ne, Sêt len, Mburtu’ Yalla mā’ngi, ka dindi bakar i aduna si!
สำรวจ John 1:29
7
John 1:10-11
Nek’ on na chi aduna si, te chi mōm la aduna si saku on, te aduna si h͈amu ko won. Ñou on na fi yos am, te yos am nanguwu ñu ko won.
สำรวจ John 1:10-11
8
John 1:9
Lêr i dega gi di lêral nit ku neka ange ñou chi aduna si.
สำรวจ John 1:9
9
John 1:17
Ndege Musa la ñu joh͈ on yōn wi; yiw ak dega bayako fa Yesu Krista.
สำรวจ John 1:17
หน้าหลัก
พระคัมภีร์
แผนการอ่าน
วิดีโอ