1
Njàlbéen ga 19:26
Kàddug Yàlla gi
Ci kaw loolu soxnas Lóot ne gees, jëmm ja far soppliku xorom.
Compare
Explore Njàlbéen ga 19:26
2
Njàlbéen ga 19:16
Lóot di tendeefal, gan ña jàpp ci loxo bi, booleek soxnaam ak ñaari doomam génne, làq leen ca gannaaw dëkk ba, ndax yërmande ju Aji Sax ji am ci Lóot.
Explore Njàlbéen ga 19:16
3
Njàlbéen ga 19:17
Ba ñu leen génnee, kenn ci ñoom ne Lóot: «Dawal sa xélu bakkan, bul geestu, bul taxaw fenn ci joor gi. Dawal ca tund ya, bala ngaa dee.»
Explore Njàlbéen ga 19:17
4
Njàlbéen ga 19:29
Ndaxam bi Yàllay tas dëkki joor ga, xalaat na Ibraayma, ba musal Lóot ca dogalam boobee, keroog ba mu tasee dëkk, ya Lóot daloon.
Explore Njàlbéen ga 19:29
Home
Bible
Plans
Videos