1
John 9:4
Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
Ela naño def i ligey i ka ma yōni on, bi bechek bi neke: gudi g’ānge dika, bu ken munul a ligey.
Compara
Explorar John 9:4
2
John 9:5
Ba ma neke chi aduna si, mā di lêr i aduna si.
Explorar John 9:5
3
John 9:2-3
Te talube am ya lāj ko, ne, Rabbi, kan a bakar, kile, am i wā’ jur am, be mu judo silmah͈a? Yesu tontu, ne, Dowul kile bakar mbāt i wā’ jur am: wande ndah͈ i ligey i Yalla fêñ chi mōm.
Explorar John 9:2-3
4
John 9:39
Te Yesu ne, Ndig ate tah͈ on ma ñou chi aduna si, ndah͈ ña gisul di mun a gis; ak ñu gis di mun a silmah͈a.
Explorar John 9:39
Inici
La Bíblia
Plans
Vídeos