1
Matthew 14:30-31
Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
Wande ba mu gise ngelou li, mu tīt, te dal di dīg; mu h͈āchu, ne, Borom bi, musal ma. Nōn’ ak nōna Yesu talal loh͈o am, te japa ko, ne ko, E borom‐ngum gu new, lutah͈ nga nimse?
Compara
Explorar Matthew 14:30-31
2
Matthew 14:30
Wande ba mu gise ngelou li, mu tīt, te dal di dīg; mu h͈āchu, ne, Borom bi, musal ma.
Explorar Matthew 14:30
3
Matthew 14:27
Wande Yesu wah͈ len chi tah͈ouay, ne, Dalal len sēn h͈ol: Man la; bu len tīt.
Explorar Matthew 14:27
4
Matthew 14:28-29
Peter tontu ko, ne, Borom bi, su de you, ô ma ma ñou fi you chi kou ndoh͈ mi. Mu ne ko, Ñoual. Peter wacha chi gāl ga, te mu doh͈ chi kou ndoh͈ ma mu dem fa Yesu.
Explorar Matthew 14:28-29
5
Matthew 14:33
Te ña neka chi gāl ga jāmu ko, ne, Chi dega yā di Dōm i Yalla.
Explorar Matthew 14:33
6
Matthew 14:16-17
Wande Yesu ne len, Soh͈laū ño dem; may len ñu leka. Ñu ne ko, Am nañu fi jurom i mburu reka, ak ñar i jen.
Explorar Matthew 14:16-17
7
Matthew 14:18-19
Mu ne, Indi len fi man. Mu ebal mbōlo ma ñu tōg chi kou ñah ma, jel jurom i mburu ya ak ñar i jen ya, yēkati but am cha asaman, gerem Yalla, dogat mburu ya, joh͈ len talube ya, te tālube ya joh͈ len mbōlo ma.
Explorar Matthew 14:18-19
8
Matthew 14:20
Ñepa leka be sūr; ñu forātu ndesit ma be ñu fêsal fuk’ i sendel ak ñar.
Explorar Matthew 14:20
Inici
La Bíblia
Plans
Vídeos