1
Matthew 13:23
Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
Te ka ñu ji won chi suf su bāh͈ sa, mō di ka dēga bāt bi, te h͈am ko, te mēña dōm chi dega, yena ya tēmēr, yale jurom bena fuka, yale ñeta fuka.
Compara
Explorar Matthew 13:23
2
Matthew 13:22
Ka ñu ji won chi digante tah͈as ya, mō di ka dēga bāt bi; te i ntopato’ aduna si, ak nah͈ay i amam, waka bāt bi, mu bañ a mēña dōm.
Explorar Matthew 13:22
3
Matthew 13:19
Ba kena dēge bāt i ngur gi, te h͈amu ko, fōfale la Seytane ñoue, te dindi la ñu ji won chi h͈ol am. Kile di ka ñu ji won chi wet i yōn wa.
Explorar Matthew 13:19
4
Matthew 13:20-21
Te ka ñu ji won chi i bereb i doch, mō di ka dēga bāt bi, te dal di ko nangu ak banēh͈; Wande amul rên chi bop’ am, te muñ chi sā yu new dal; ndege su nah͈ar joge wala ngeten ndig bāt bi, nōg’ ak nōga mu fakatalu.
Explorar Matthew 13:20-21
5
Matthew 13:44
Ngur i ajana niro na ak alal bu nubu chi bir tōl; ba ko nit feke mu nuba ko, dem chi banēh͈ am jay lu mu am on yepa, te jenda tōl bōbale.
Explorar Matthew 13:44
6
Matthew 13:8
Yenen rot chi suf su bāh͈ sa, te mēña mēñef, yena ya tēmēr, yale jurom bena fuka, yale ñeta fuka.
Explorar Matthew 13:8
7
Matthew 13:30
Bayi len ñar ña ñu sah͈ando be cha ngōbte ga; te cha wah͈tu’ ngōbte ga di nā wah͈ gōbkat ya, ne, Budi len jeka nduh͈um la, taka ko i say te laka ko; wande dajale len dugup ja chi suma sah͈a.
Explorar Matthew 13:30
Inici
La Bíblia
Plans
Vídeos