John 11:43-44
John 11:43-44 GWG
Te ba mu wah͈e nōgule, mu h͈āchu be cha kou, ne, Lazarus, gēnasil. Ka dē on gēnasi, ak na ñu ewe won loh͈o am ak tank’ am ak yēre’ bamel ya; te kanam am ñu lah͈as ko ak ser. Yesu ne len, Ewi len ko, te bayi ko mu dem.