John 2:15-16
John 2:15-16 GWG
Te mu defar yar i būm, te dah͈a yepa cha biti juma ja, nh͈ar ya ak nag ya; te mu tūr h͈ālis i wēchikat ya, te dānel sēn i tabul; Te mu ne ña don jay mpetah͈ ya, Fab len yile cha biti; bu len def suma nēg i Bay nēg i jayukay.