1
John 2:11
Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
Mandarga bu jeka bile la Yesu def on cha Cana i Galilee, te wone ndam am; te i talube am gum chi mōm.
Konpare
Eksplore John 2:11
2
John 2:4
Te Yesu ne ko, Jigen ji, lu ma jote ak you? Suma wah͈tu dikangul.
Eksplore John 2:4
3
John 2:7-8
Yesu ne len, Fêsal len ndā yi ak ndoh͈. Te ñu fêsal len be cha gemeñ ya. Mu ne len, Tanh͈a len cha lēgi, te yub kēlifa nchēt ga. Te ñu yub ko.
Eksplore John 2:7-8
4
John 2:19
Yesu tontu te ne len, Maba len juma jile, te chi ñet’ i fan di nā ko delu tah͈oual.
Eksplore John 2:19
5
John 2:15-16
Te mu defar yar i būm, te dah͈a yepa cha biti juma ja, nh͈ar ya ak nag ya; te mu tūr h͈ālis i wēchikat ya, te dānel sēn i tabul; Te mu ne ña don jay mpetah͈ ya, Fab len yile cha biti; bu len def suma nēg i Bay nēg i jayukay.
Eksplore John 2:15-16
Akèy
Bib
Plan yo
Videyo