John 14:16-17
John 14:16-17 GWG
Te di nā ñān Bay ba, te di na len may benen Dalalkat, ndah͈ mu neka ak yēn bel mos; Nh͈el i dega ma la: ka aduna si munul a nangu; ndege gisu ko, te h͈amu ko: yēn a ko h͈am; ndege deka na ak yēn, te di na neka chi yēn.