John 16:7-8
John 16:7-8 GWG
Wande wah͈ nā len dega; genal na len ma dem: ndege su ma demule, Dalalkat ba du ñoui fi yēn; wande su ma deme, di nā ko yōni fi yēn. Te bu mu ñoue, di na gāi aduna si chi bakar, ak chi njūbay, ak chi ate