Njàlbéen ga 12:4
Njàlbéen ga 12:4 KYG
Ibraam daldi dem, na ko ko Aji Sax ji waxe woon, Lóot topp ca. Ba Ibraam di jóge Karan, booba am na juróom ñaar fukki at ak juróom (75).