Matthew 2:1-2

Matthew 2:1-2 GWG

Ba Yesu jūdo cha Bethlehem i Judæa, chi bes i Herod bur ba, i borom‐h͈amh͈am juge on nañu cha Penku, ñou chi Jerusalem, Ne, Ana ki jūdu Bur i Yauod ya? Ndege gis on nañu bidiw am cha Penku, te dika nañu ndah͈ ñu jāmu ko.