Njàlbéen ga 27:39-40
Njàlbéen ga 27:39-40 KYG
Baayam Isaaxa ne ko: «Déglul, ma wax la, dinga dëkk fu sore ngëneeli suuf, mbaa fu la layub asamaan tiime. Sa saamar ngay dunde, sa rakk di la yilif. Waaye bés a ngi ñëw yaay sigiñu, ba yenniku notaangeem.»