1
Njàlbéen ga 24:12
Kàddug Yàlla gi
Mu daldi ne: «Yaw Aji Sax ji, sama Yàllay sang Ibraayma, ngalla nangul ma tey jii te laaye biir sama sang Ibraayma.
对照
探索 Njàlbéen ga 24:12
2
Njàlbéen ga 24:14
Janq bu ma wax ne ko: “Doo yenniku sa njaq, may ma, ma naan,” mu ne ma: “Naanal ba noppi, ma wëggal la say giléem,” na kooka di ki nga jagleel sa jaam Isaaxa. Noonu laay xame ne laaye nga biir sama sang.»
探索 Njàlbéen ga 24:14
3
Njàlbéen ga 24:67
Ba loolu wéyee Isaaxa yóbbu Rebeka ca xaymab yaayam Saarata, muy soxnaam, di ku mu bëgg, te di ko muñe yaayam, ndax fekk na mu faatu.
探索 Njàlbéen ga 24:67
4
Njàlbéen ga 24:60
Ña ngay ñaanal Rebeka, mu barkeel, te naan: «Éy jigéen sunu! Giiral, ba sos ay junniy junni, te sa askan teg ay bañam tànk.»
探索 Njàlbéen ga 24:60
5
Njàlbéen ga 24:3-4
ma giñloo la ci Aji Sax jiy Yàllay asamaan ak suuf ne doo jëlal sama doom soxna ci biir jigéeni waa Kanaan, gi ma dëkk ci seen biir. Waaye dinga dem sama réew, ma ma cosaanoo, jëlal fa sama doom Isaaxa soxna.»
探索 Njàlbéen ga 24:3-4
主页
圣经
计划
视频