1
Njàlbéen ga 27:28-29
Kàddug Yàlla gi
Yal na la Yàlla may layub asamaan ak ngëneeli suuf, pepp ne gàññ, biiñ walangaan. Yal na la ay giir nangul, ay réew di la sujjóotal, nga yilif say bokk, te say doomi ndey di la sujjóotal. Ku la móolooy alku, te ku la ñaanal barkeel.»
对照
探索 Njàlbéen ga 27:28-29
2
Njàlbéen ga 27:36
Esawu ne: «Moom kay moo yey tudd Yanqóoba, ndax suufu na ma ñaari yoon. Sama céru taaw la jëkka nangu, tey mu nangooti sama ñaanu baay.» Mu teg ca ne: «Ndax desalaloo ma ag ñaan?»
探索 Njàlbéen ga 27:36
3
Njàlbéen ga 27:39-40
Baayam Isaaxa ne ko: «Déglul, ma wax la, dinga dëkk fu sore ngëneeli suuf, mbaa fu la layub asamaan tiime. Sa saamar ngay dunde, sa rakk di la yilif. Waaye bés a ngi ñëw yaay sigiñu, ba yenniku notaangeem.»
探索 Njàlbéen ga 27:39-40
4
Njàlbéen ga 27:38
Esawu ne baayam: «Baay, xanaa genn ñaan rekk nga am? Ngalla baay, ñaanal ma, man itam!» Ca la Esawu ne yikkét jooy.
探索 Njàlbéen ga 27:38
主页
圣经
计划
视频