1
Matthew 8:26
Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
Mu ne len, Lutah͈ ngēn ragal, yēn nit i ngum gu new? Fōfale mu jog, te eda ngelou ya ak gēch ga; mu dal be ne nem.
Összehasonlít
Fedezd fel: Matthew 8:26
2
Matthew 8:8
Saltige ba tontu ko ne, Borom bi, daganu ma nga h͈araf chi suma nēg; wande wah͈al bāt bi reka, te suma bukanēg di na wer.
Fedezd fel: Matthew 8:8
3
Matthew 8:10
Ba ko Yesu dēge, mu jomi, te ne ña ko top’ on, Chi dega mangi len di wah͈, mosu ma feka ngum gu nu day, dēt, du chi Israel.
Fedezd fel: Matthew 8:10
4
Matthew 8:13
Yesu ne saltige ba, Demal sa yōn, naka nga gume, na ame nōgu chi you. Bukanēg am dal di wer cha wah͈tu wōwale.
Fedezd fel: Matthew 8:13
5
Matthew 8:27
Nit ña jomi, ne, Ban melin i nit a di kile, be ngelou li sah͈ ak gēch gi di ko dēgal!
Fedezd fel: Matthew 8:27
Kezdőoldal
Biblia
Olvasótervek
Videók