1
Njàlbéen ga 7:1
Kàddug Yàlla gi
Gannaaw ba loolu amee Aji Sax ji dafa wax Nóoyin ne ko: «Duggal ci gaal gu mag gi, yaak sa njaboot gépp, ndaxte niti jamono jii, yaw rekk laa ci gis, nga jub ni ma ko bëgge.
Yenzanisa
Ongorora {{vhesi}}
2
Njàlbéen ga 7:24
Ndox mi nag di wal-wali ci kaw suuf diirub téeméeri fan ak juróom fukk.
3
Njàlbéen ga 7:11
At ma Nóoyin amee juróom benni téeméeri at, ca fukki fan ya ak juróom ñaar ca ñaareelu weer wa, kera la bëti ndox ya ne jàyy, jóge xóotey géej, bunti ndoxi asamaan ne kulbét, mu ne yureet
4
Njàlbéen ga 7:23
Luy dund ci àddina daldi sànku, ba nit ak jur ak luy raam ak luy naaw— lépp la Aji Sax ji raafal ci àddina. Nóoyin rekk a des, moom ak ña àndoon ak moom ca gaal ga.
5
Njàlbéen ga 7:12
taw biy sottiku ci suuf diiru ñeent fukki guddi ak ñeent fukki bëccëg.
Pekutangira
Bhaibheri
Zvirongwa
Mavideo